Bu ñuy doxaan ci lu ne dinga ko dégg I love you baby, my sweety, my lady Yaa ma gënal sama ndey ji ak sama baay be Sukk, raam, jébbalu, jooy, lu ne ñu def ko Bu ñuy doxaan ci lu ne dinga ko dégg I love you baby, my sweety, my lady Yaa ma gënal sama ndey ji ak sama baay be Sukk, raam, jébbalu, jooy, lu ne dinañu ko def Li ma metti ba tax ma soppi jikko (moom) Def ni ma mel ba noppi ni fess (moma) Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma) Góor-e tax jigéen soxor leegi Jël pakka jam ko sama digg xol (moma) Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma) Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma) Góor-e tax jigéen soxor leegi (Leegi) Ñaata yoon la ma wax I love you My baby (Baby) Ñaata yoon lama wax loolu Xale bile moom, lu Yàlla xam doyna Dafma gëlëmël ci mbëggeel touté dess mu ray ma Xale bile moom, dafma né daf ma lova Ndeketé lepp lum la mës wax ay fenn la Xale bilé (ñewna) Xamal mani (moom la) Néma sama (goor la) Lepp ay (door la) Xale bilé (moma) Soppi na (jikom ba) Fima ko romboon ci mbedd mi daf ma dab Bula góor toppate ne la bëgg naa la Xamal ko xol dafa oyof buguma nga gañ ma Bula góor toppate néla bëgg nala Lacc ko bëgg na giss papam di toroxal Yayam Baby Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg I love you baby, my sweety, my lady Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé Sukk raam jébbalu joy lune ñu def ko Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg I love you baby, my sweety, my lady Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def Lima metti batax ma sopi jikko (moma) Def nima mel ba nopi ni fess (moma) Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma) Góor-e tax jigéen soxor leegi Jël pakka jam ko sama digg xol (moma) Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma) Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma) Góor-e tax jigéen soxor leegi (Leegi) Ñaata yoon lama wax I love you My baby (Baby) Ñaata yoon lama wax loolu Buñu bëgg dem, buñu bëgg dem Te gën lula ci Yawit boleen jekko tegal le lu sadik Buñu bëgg dem, buñu bëgg dem Te gën lula ci Yawit amal fulë amal fulë Waawaaw bàyyi ko, bàyyi ko Ndax moom xamul sa njëg Oh bàyyi ko oooh Ndax moom xamul sa njëg Sister, please don't cry Fompal say rangooñ Bul la góor jaral ngay jooy Fompal say rangooñ Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg I love you baby, my sweety, my lady Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def Lima metti batax ma sopi jikko (moma) Def nima mel ba nopi ni fess (moma) Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma) Góor-e tax jigéen soxor leegi Jël pakka jam ko sama digg xol (moma) Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma) Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma) Góor-e tax jigéen soxor leegi (Leegi) Ñaata yoon lama wax I love you My baby (Baby) Ñaata yoon lama wax loolu