Bi aduna, lu fi jar ngay def lu ñaw ? Fi aduna, lu fi way rindi sax sa loxo rekk lay nathie Wax ma! Lane mo tax Bëggulo ma waxal lu baax Wax ma! Lan moy mbax Budé yénagneté wugnu lu baax Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw Li dafa ñaaw nagnu sante yallah bayi beutu ginaaw Xam na sama tolu waya tax sa fite di naw Yalla nopina demba tay sogua nieuw gis nga fi dara du ñaaw Lithi mane nékul si yow (ngani) Lithi mane nékul si yow (diëlël) Lithi mane nékul si yow, bëgueneté léne fi adina la (wawaw) Lithi mane nékul si yow (waxal) Lithi mane nékul si yow (kay) Lithi mane nékul si yow bëgueneté léne fi adina la (waxal way) Téréte biy daw thi iow moy daw thi mane Wax ma lane motax Meunugno yénaneté lu baax Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw Li dafa ñaaw nagnu sante yallah bayi bëtu ginaaw Xam na sama tolu waya tax sa fite di naw Yalla nopina demba tay sogua nieuw gis nga fi dara du ñaaw Tu tapes dans mon dos Tu parles dans mon dos Tu craches dans mon dos Sourire à la face, couteau dans mon dos Tu tapes dans mon dos Tu parles dans mon dos Tu craches dans mon dos Sourire à la face, couteau dans mon dos Waxal way! Tidjane waxal way (Kokoy chérie Aïda) Abdou Mbay waxal way (Borom Conakry) Mani Akéthié waxal way (from Abidjan la) Baxaw waxal way (Ku bëgg lolu Viviane) Eeeh, Kiné waxal way (Kokou sama doom la) Awadi waxal way Sénégal waxal way