Xamna lilay sonal Wax jou bari teksi nga diss te yenouwo Xamna lilay sonal Bilé melokan molay deranger Yalla mayma nangouwo Ma romboula nangoulo Foma seen dima retane té begouloma Heeey Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Sit down yow Fii adinala kon teyal (lala lala lalala) Fii adinala kon teyal (lala lala lalala) Fii adinala kon teyal (lala lala lalala) Fii adinala fils teyal (ohh) Xamna lilay sonal Wax jou bari teksi nga diss te yenouwo Man Xamna lilay sonal Bilé melokan molay deranger Yalla mayma nangouwo (mayla nangouwo) Ma romboula nangoulo (ma romboula nangouwo) Foma seen dima retane té begouloma Yalla mayma nangouwo Ma romboula nangoulo Foma seen taalalma loxo té soppouloma Hey Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Sit down yow Fii adinala kon teyal Fii adinala hey teyal Fii adinala kon teyal Fii adinala fils teyala tey Maalay deranger Ndeketé mane rek nga bañ Te xawma loumala def Bo sañoon souba ma dé Ngir suñu andabi yaga Fok ñouy waxanté deugga Ba ñoumay matteu di euffé mattaalela Xarit né waxma mani waxma Lou tax sooma guissé dima ré te beggouloma Kay ma waxla togal ma waxla Pexé you bone yingay jeem ni yalla guiss la Eey Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Tiré ngama visél bou baax ndax daluma Sit down yow Jeleul waywi ma mayla yeah Jeleul waywi maynala yeah Jeleul waywi ma mayla yeah Jeleul waywi maynala Defko cas