Yaw la, yaw la Dëgg dëgg dëgg yaw rekk la Coow li, coow li Neexul ba neexul Ndiaye doo seen moroom Ku mu neexul jëlal fale Ku mu neexul toppal nale Sunu xol yi yaw yaa ci ne Ndax sa mbaax ñepp ñoo ko seede Gaynde Ndiaye sa dëgg-dëgg Fi nga jàpp foofo dëgg Yàqe bari feem mëna dem Yaa ngi tax a jooy te dóoroo ñu Ñu ngi asaman te nawuñu Tëddel tëddel nelaw Nelaw ba yàndoor sa gannaw bandang Man bëgg naa la Gëmel Yàlla ji Gëmel Yàlla ji te xam ni moom rekk kaay maye Gëmel Yàlla ji te xam ni moom rekk kay dogal Ku mu neexul jëlel fale Ku mu neexul toppal nale Sunu xol yi yaw yaa ci ne Ndax sa mbaax ñepp ñoo ko seede Gaynde Ndiaye sa dëgg-dëgg Fi nga jàpp foofo dëgg Yàqe bari feem mëna dem Yaa ngi tax a jooy te dóoroo ñu Ñu ngi asaman te nawuñu Tëddel tëddel nelaw Alboury biram Penda Ndiemé Boroom Jolof bu na njorte Biram penda Farimata mi mu dembothioro bé Moy Mami Serigne Ndiaye buna Buna ba Jolof marré nane, buna yaaa eunoub tene wajuram di sa nane ba rewmi naat Yacine gueye massar sa yaye Serigné Ndiaye bu mansur buna Sëriñ Ndiaye Aziz Fama Mansour umi Mame fama Ndiaye baayu Sophie Ndiaye Aaaah, aaaahn, aaaahn Sëriñ Ndiaye Bouna Nelaw ba yàndoor sa gannaw bandang Man bëgg naa la Biram ndieme Aissa Ndiaye Bu kaari bigué sanguleen Alboury diakher, Alboury baay Buna Ndiaye Mami mame Famara Ciré Ndiaye, Buna Ndiaye Man nga yàndoor soy nelaw Ku mu neexul jëlal fale Ku mu neexul toppal nale Nelaw ba yàndoor sa gannaw bandang Man bëgg naa la