Nit ku baax warul moom di teye mer Buur Yàlla di ko tooñ lañu dekke War nga xaalaat balaa nga may àntu Gënal li sa xol waaw boo tëddee nelaw Nit ku baax war na di baale moom Nit ku baax war na di jégeele Ndaxam buur bi Yàlla dañu dekk di ko tooñ Boo julee ñan mu face say bàkkaar Dafa bàyyi say moroom yaw tànn naa la Bàyyi kër ndey ak baay ngir séyal la Kon bu mu séy du luñuy caxanee Gënal li sa xol waaw bo tëdde nelaw Kaay wax ak moom kaay wax ak moom Kaay wax ak moom yénn bokk njegenaay Kaay wax ak moom kaay wax ak moom Kaay wax ak moom yénn bokk njegenaay Hey nañu caapa ne jigéen ñi Ñooy sunu kaani Kon gnoune ak goune gnoune Ak gnome Ba sagar khègne Mu ne waaw nangu Kon jàpp ne séy lu ko takk taasu ko Kon ñun ak gu ne ñun ak ñome ba pik ak pele! Yaw mi jàmm bu ñu la baaloo na nga baale Buur Yàlla moom dañu dékk di ko tooñ Kon yaw mi jàmm mi la baaloo danga wara baale Ndax buur Yàlla moom sopp na jàmm buy baale Kaay wax ak moom kaay wax ak moom Kaay wax ak moom yénn bokk njegenaay Kaay wax ak moom kaay wax ak moom Kaay wax ak moom yénn bokk njegenaay Kaay wax ak moom kaay wax ak moom Billaay billaay billaay