Soo xamoon ne ma zoné Su kër doon école awma ci classe Ci mbedd bi laay jànge Ba sama xël ñëw na soxlawul das Ba may nekk guné Mbour tukkulër ba Grand Dakar Fass Man dem naa ci fu ne La tête dans les nuages et les pieds sur le bitume Lu-lu ne laa gis ba-bànneex ak diis Lu-lu ne laa gis terewul Vivi jàpp te bàyyi Fi ma jar ba yeksi fii Yombul waye jombul doomu adama Je n'aime pas le jour je ne vie que la night Soo xamoon ne ma zoné Su kër doon école awma ci classe Ci mbedd bi laay jànge Ba sama xël ñëw na soxlawul das Ba may nekk guné Mbour tukkulër ba Grand Dakar Fass Man dem naa ci fu ne La tête dans les nuages et les pieds sur le bitume [Barack Adama] Wooh wooh wooh wooh wooh Yaay boy a taffée sans arrêt du lundi au lundi Wooh wooh wooh wooh wooh Et le daron a fait pareil sans profiter de la vie All eyes on me, je veux tourner Je veux conquérir le monde dans la mif' on est nombreux Wouwou j'ai zoné dans les rues maintenant me voilà Anhan j'ai zoné dans les rues maintenant me voilà yaye booy Man sama life fi la musique bi jël deinthieu Te gore na ba tijil maa ay buntu Ku ñakk jëriñu man duma rëccu Ku nekk ci kanam dotoo tala geestu Bëggeel doomu adama Indi na Viviane ak Barack Adama Amul frontière!