Xale bi sama reni xol de wuyu ma Bëgg naa la te xamoo ci dara Mbëggéel ci xol lay nekk dëgg la Bëgg naa la te xamoo ci dara Man de walluleen ma wax ko ko Xale bi lekkatuma ndax moom Naanatuma, nelawatuma Wowo, sama xol yaa ci ne Lég-lég ma woo ko tit dal di coupé Sama appetit coupé Feebar dina ma gunge Docteur dama love ba dof Te xawma lu koy faj Wowo, mbaa mën nga ci dara Xale bi sama reni xol de wuyu ma Bëgg naa la te xamoo ci dara Mbëggéel ci xol lay nekk dëgg la Bëgg naa la te xamoo ci dara Man woo naa la fu ne Nga jàppe ma sa xarit Inviter résto, lalal naa la lu ne Wowo, nga jàppe ma sa xarit Lég-lég ma woo ko tit dal di coupé Sama appetit coupé Feebar dina ma gunge Docteur dama love ba dof Te xawma lu koy faj Wowo, mbaa mën nga ci dara Man bëgg naa ma bañ bàyyiwuma Man gisuma kenneen ku dul moom Mbëggéelu bari doole yeen ma ko xam Xale bi sama reni xol de wuyu ma Bëgg naa la te xamoo ci dara Mbëggéel ci xol lay nekk dëgg la Bëgg naa la te xamoo ci dara Xale bi sama reni xol de wuyu ma Bëgg naa la te xamoo ci dara Mbëggéel ci xol lay nekk dëgg la Bëgg naa la te xamoo ci dara Ku ci nekk ak ki ña nob Sa ginnaaw bandag faxasul Juugel yëngël ba mu saf Sa ginnaaw badang faxasul Ku ci nekk ak ki ña nob Sa ginnaaw bandag faxasul Juugel yëngël ba mu saf Sa ginnaaw badang faxasul