Sope kaay nga jege ma Sama xol yaw rekk la Dama la bëgg xawma lan la Te loolu nak demb la Sama lettre bind naa ko Ba posteel la ko nga jot ko Sama album lu ko feesal Say naatal man bëgg naa la Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Gisuma dara kele rekk Bëgguma dara kele rekk Sama xol kan moo koy dundal kele la Wuy dama la bëgg wax Ni ngiro na dimbali ma Kaay jege ma Maa neexal la Jokk dox jaagu mbaar Ngir nga kontaan Sope, jege ma Tam-tamal ma Maa ngiro ci digg laal bi Ayca kaay yëkkati ma Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Sope kaay nga jege ma Sama xol yaw rekk la Taar taxul bëgg naa la Lu yàgg rekk dëgg la Telegram bi ma jote tay Du mandat bi sama xol la Auto rail bi di corné Ma lay seen du bëgg naa la Gisuma dara kele rekk Bëgguma dara kele rekk Sama xol kan moo koy dundal kele la Wuy dama la bëgg wax Ni ngiro na dimbali ma Kaay jege ma Maa neexal la Jokk dox jaagu mbaar Ngir nga kontaan Sope, jege ma Tam-tamal ma Maa ngiro ci digg laal bi Ayca kaay yëkkati ma Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Oooh amour piis ma, bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Waaw waaw Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Waaw waaw Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la