Viviane Chidid

Sant Na

Viviane Chidid


Dara gueunoul nekh lii
Niit gni dila bégué
Foo wayé niou contane
Ko yeuk yeuknala
Té ko faalé faaléleu
Yéneu moom lii
Té ko falé faaleleu

Mane may sopé gouné yi
Di xaritou goor yi
Magg yi naan yagnou saf
Djiggen yi lang ak mane

Sant na yallah sant na yallah ouuh
Bima amé niit gni
Sant na yallah sant na yallah ouuh

Diox nalène sama xol
Yeen gni ma saffo
Diap nalène doumalène baayi
Koo yeuk yeuknala
Tè ko faalé faalé leu
Yeeneu moom lii
Tè ko falé faalé leu

Mane maay sopé gouné yi
Di xaritou goor yi
Magg yi naan yagnou saff
Djiggen yi lang ak mane

Sant na yallah sant na yallah ouuh
Bima amé niit gni
Sant na yallah sant na yallah ouuh
Bima amé niit gni
Sant na yallah sant na yallah ouuuuh

Damay doogua door
Yow khamnaa né yomboul
Teen wii sorina
Dara gueunoul nekh lii
Niit gni dila bégué
Foo wayé yeup contane
Foo wooté nieup nieuw gua teerou
Yow mane khamnaané yomboul

Sant naa yallah
Sant naa yaaallah sant leen yallah

Niit kouné saayoo yeewoo war ngua sant yallah
Yow mane khamnaané yomboul
Youssou madjiguène yow kham ngua né yomboul
Yow Ndiaye yow kham ngua né yomboul
Thiané diagne yow kham ngua né yomboul
Djolof band yeen kham nguen né yomboul
wawaaw