Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés Non, non, duma nangu nga may teg stress Duma nangu nga may teg stress Ma bañ duma ko nangu no stress Sama xol di fees yaw nga juk def fés Ma ni dimbali ma wax ji bari na Man rekk ci xale nammuma dara Ma ni dimbali ma wax ji bari na Man rekk ci xale nammuma dara Danga fàtte ni awma dix ans Lu tax nga jël ma bëgg ma def sa fowukaay Yombalal naa la sa visa Wow yeah yeah, demal fu la neex way! Bëgg langak ki Bëgg langak ke Bëgg langak samay xarit ma ni night and day Dégg na ñu ne feebar la Wow yeah yeah, defal lu la neex way! Non non duma nangu nga may teg stress Duma nangu fils nga may teg stress Ma bañ duma ko nangu no stress Sama xol di fees yaw nga juk def fés Ma ni dimbali ma wax ji bari na Man rekk ci xale nammuma dara Ma ni dimbali ma wax ji bari na Man rekk ci xale nammuma dara Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la Ku ma bëgg a tardel bëgg ma fowe ma romb la Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la Ku ma bëgg a tardek man ma romb la Li safatuma Sama mettitu muñ jeex na Li yëngëluma Ndax te man ñakkuma fayda Li safatuma Tegg ci temps def ba mu baax jot na Te yaw mi xam nga Soo ma nobul sa moroom nob ma! Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés Non, non, duma nangu nga may teg stress Duma nangu nga may teg stress Ma bañ duma ko nangu no stress Sama xol di fees yaw nga juk def fés Ma ni dimbali ma wax ji bari na Man rekk ci xale nammuma dara Ma ni dimbali ma wax ji bari na Man rekk ci xale nammuma dara Góor goula teg deal lundi ba dimanche nobu la Ku ma bëgg a tardeel bëgg ma fowe ma romb la Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la Ku ma bëgg a tardèk mane ma rombe la