Philip Monteiro

Yaw Rek Lev (feat. Corine)

Philip Monteiro


Ibil nal sama khol
Yalla na nga si guiss lou lére
Té gueuneu kham ni
Amoul kénène koudoul yaw
Mbeugél gui nékeu si mane
A ngii di ma dane
Té gueum na né di na done
Sa néné bi ngéy tété

Mane mi souma mounone
Dina bokake yow bénéne yone
Dila wowé néné touti
Ndakh té mane mi
Mane mi gnanou ma yalla
Gnanou ma yalla
Déss fii mane réka

Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné

Am na gnou wakh
Mbeugél tiono rék la
Wayé ma ngi léy khamal
Dou kéne yow réke leu
Beuss bou me le guissé
Ta kham ni khol déy guissé
Té fok na ni do meusse tass sama yakar!

Boul am loy ragal di la khar
Doumeu meusseu diay sama taar
Dinala wowé papa chéri
Dina done sa sokhna
Di na done sa baby
Mi léy fadial
Say sokhla, oh baby yow réke le

Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné

Yay sama doolé
Soudoul yow wate na né dou done kékéne
Diokh na la sama bope
Té dina la dégueul di le bégueul
Baby boul sone
Gueumeul ni yow réke le!
Dou kékéne

Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Ibil nala sama khol