Yeah Sama fans yi, magui léne di gueureum Di léne santeu guiss na séne taxaway Musique bi Pour yen la, oh-oh-oh-oh Mane nop na léne, waw Yagueu neu lool, bingueu démé Mane réére na, réére na sa yow Lane la wara déf, déf sans yow (sans yow hey) Dama la soxla, té da ma la beugueu (Déme ngueu té bay ma) bay ma si leundeum Wanté xam ngua ni, ni dama wara doumeu maneu doundeu ba téy (Déme ngua té bay ma) baby gnewateul si mane Xana déguo sama wo (Baby gnewateul) yagueu na lool bi ngua démé (Tax na sama xol wééte) lou maye déf ba ngueu gneuwate, gneuwate si mane (Baby gneuwatal) yagneu na lool bi ngua démé (Tax na sama xol wéét) xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane Bou ma togué di xalaate (doundeu you nex gui gnou done doundeu) Rek sama xool fess (xama tou ma lou ma wara déf) Déme ngua bayi ma thi leundeum (wanté xam ngua ni) Dama wara doundeu mateye (déme ngua té bayi ma) Bayi ma si leundeum Dama la soxla, dama la beugueu Baby ngeuwateul si mane, xana déguo sama wo Baby gnewateul, yagueu na lool bi ngua démé (Tax na sama xol wééte) lou maye déf ba ngueu gneuwate, gneuwate si mane (Baby gneuwatal) yagneu na lool bi ngua démé (Tax na sama xol wéét) xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane Xama tou ma li ma wara déf (yagueu neu lool) Bouguou ma ngua xaam li ma dadj, nax xaam na nik ame ngua kénéne Meunou ma ko gueum Meuneu dess ni Yagueu na lool bi ngua déme mane réére na nékeutofi Lane la wara déf nékeutofi Dama la soxla, dama la beugueu Baby gneuwateul si mane, xana déguo sama wo Baby gnewateul, yagueu na lool bi ngua démé (Tax na sama xol wééte) lou maye déf ba ngueu gneuwate, gneuwate si mane (Baby gneuwatal) yagneu na lool bi ngua démé (Tax na sama xol wéét) xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane