Karabalik on the track Fu mu mënti nekk Ma wëri ko wëri ko wëri ko fu mu mënti nekk Jëli ko jëli ko jëli ko fu mu mënti nekke Man sama mind laa la dénk te doo mës a dégg bring it back Love a fi nekk leneen xaju fi Kon you know the vibe you know the melody Yaw rekk yaa ma mës a tollu fii Yaay sama naaj di sama jant bi Baby, you know the vibe you know the melody I say you know the vibe you know the melody Baby, tonight dama la bëgg a gis Këf sama mind tax ba ma wéradi Baby, you know the vibe you know the melody Baby, loo bëgg bëgg naa, loo wax ma defal la ko Topp sa ginnaaw, foo nekk ma fekk la fa Loo bëgg bëgg naa baby girl jox ma sa loxo Bëgguma sa xel di ñaaw Bëgguma keneen ku dul yaw You're my ride or die mënóo deme nii You're my wife yaw laa jënde ñeneen ñi Sama paradise and my remedy Me and you for life jusqu'à l'infiniii Kon you know the vibe you know the melody Yaw rekk yaa ma mës a tollu fii Yaay sama naaj di sama jant bi Baby, you know the vibe you know the melody I say you know the vibe you know the melody Baby, tonight dama la bëgg a gis Këf sama mind tax ba ma wéradi Baby, you know the vibe you know the melody Baby, li nekk ci yaw moo nekk ci man Dem nga woon te fàww nga dellusiwaat Baby lépp mënul neex, fàww muy metti yenne saa yi I called you phone but you don't wanna answer Nobody know what you can do to me Nobody know babe only you and me And I feel blesed to be by your side I don't want you to cry all night Fu mu mënti nekk Ma wëri ko wëri ko wëri ko fu mu mënti nekk Jëli ko jëli ko jëli ko fu mu mënti nekke Man sama mind laa la dénk te doo mës a dégg bring it back Love a fi nekk leneen xaju fi Kon you know the vibe you know the melody Yaw rekk yaa ma mës a tollu fii Yaay sama naaj di sama jant bi Baby, you know the vibe you know the melody I say you know the vibe you know the melody Baby, tonight dama la bëgg a gis Këf sama mind tax ba ma wéradi Baby, you know the vibe you know the melody