Lëndëm bi fees sama bopp
Mi ngi fees te duñ mënati tuuri
My life's just like a movie
Oh tell me what the truth is, yeah yeah

Loo def ñu naan la du nii (oh oh oh)
Bëccëg di mel ni guddi
Sama bopp war nañ ko ubbi

Yeah, wéet sama gàlle toog man rekk
Gotta talk my shit and walk my way
Jeex ba mu mel ni droge laay lekk
Biig ci guddi gént yu bon laa gént
You're lying, I can see it in your eyes
I got myself so let me be let me die
Give me peace I don't want love
Give me peace, yeah
Faale sama peace
Bopp bi ngi féete fi sa bëti xol di gis
Sama jàmm ndekete du xaritook ñii
Wan la jail sama biir, fan la ma caabi féeteeti
Nooy def ba xajal, fàtte cib

Lëndëm bi fees sama bopp
Mi ngi fees te duñ mënati tuuri
My life's just like a movie
Oh tell me what the truth is, yeah yeah

Loo def ñu naan la du nii (oh oh oh)
Bëccëg di mel ni guddi
Sama bopp war nañ ko ubbi, yeah yeah

Réer digg géej mais Tefes day feeñ
Never give up! Xëy bët set ba gee bañ ken
Dimbali la, te yëg-yëg yi dem nañ stress
Singali ma, gëm fen c'est comme tëb teen, ci ku gumba
I know what's going on
Mere ku la deful dara ngay dëkke
Dëgg rekk ay jiitu, dëgg mooy mujj
Nga wéet saa yu lëndëmee
I know what's going on
Ki ëpp doole ci life ki dëggu goreek ki maandu
Bës bu gone di màgg, xel di jeex doole di naax
Doo mës a kawee ni naaj
Bës dinga nelawe ci pax
Santal ñi lakk pour nga leerle, ñooy sa sondeelu life

Lëndëm bi fees sama bopp
Mi ngi fees te duñ mënati tuuri
My life's just like a movie
Oh tell me what the truth is, yeah yeah

Loo def ñu naan la du nii (oh oh oh)
Bëccëg di mel ni guddi
Sama bopp war nañ ko ubbi, yeah

We know that
I don't wanna play no game
And we know that
So whyyy
In my life, ain't no play no game
And we know that
Yeah we know that
We know that
I don't wanna play no game
And we know that
So whyyy
And we know that