Come On! Alkati ya ngi sa kaw Thiap bi nga doon xam naniou ni ya ngi ak xalissak drogue Wa bou yabo nanal ci sa Safara yi dieul garap bi xeupo Thiat ci sa maw laff yi la tok May sa thiabi kasso, mane la may Picasso Parce que boudone man xamna di nga sol Lou eupeu att nga ndara woor kay niu nafila bokk Père Noel raciste la mane moussouma guiss cadeaux Guiss na ay Pa yu djaay sen taxi pour am passou avions Atoum leumb souma nekhé douma liguèye A tout moment meune nga déh ni ngoumba ci Guedj Dou ben bopp rek nek ci mane Def lou yomb rek méti ci mane Kouy topando mane ak yaw nouro wouniu système Yallah loutax ma dée ni kou dioudo ci cimetière? Mouno wa Rap'Adio kone non meuno li DIP Def TLK dou Album, dou maxi, non non dou mixtape Yaggo tchi kaw ni boy bou ndaw bou tiim Jail Rap bi dafa yombone nioune niossi soti dindière Ndiago bi moy Boss pourtant moussou massi djékkeu Douma lekk kou souroul parce que dama xiff ndeim Na def lou eup 1000 scènes, encaissé plus de 1000 chèques Sa Papa, Sa yaye ak baag bi lay souleudo ci tenn Maf-fu Hip Hop bi mo raw bi ci Goudi Town Rap bi dou djoug ndakh boy bou am buzz outi daanou Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi Sokhla wuma kèneu kumay temoigné fils Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi Idy namoul iPhone 6 ndakh ma ngi fi Sokhla wouma kèneu kumay temoigné fils Dé lène Diaamou Yallah té nguène gueum sen bopp Bèneu lama may mane ma woute yeneen 2 cerveaux Même handicapés yarramam day ndaw Wayé kou Fan Pée (1er) bi toujours deuss (2eme) lay done No def ba degg Jàmm ci deuk bou dégueulasse bi Yëk Carrapid, bokk nëk ak Pa' bi Mama ress la, ress sa rakk yi Réro demb téyeul sa lamiñ Sénégal moy deukou Téranga mais amoul restaurant du coeur Kone loy xalate ci boy yi moussoul ray sen bopp beug xexal Afrique Liberté moussoul am nigger fuck 4 Avril Dictateur rek ba déh ni Colonel Khadafi Bandit yi yéwou yeup ngi def, ñi gueuméintou dem teudi Jail May Punch ba ndel Kocc Barma té dougneko nétali kèneu Nigger douggou na palais xamna donou Président Boul Rap toujours rek fexel ba am comme li Jay-Z am Boy Grand yoff, Arafat boy xamna fou BOON bou nekh bi am Meune nagnema faat wayé mounou niouma fatté Dioudou waat na ba sonneu mais bène yoon lay dé Gars yima gueumoul wone légui gueméwouniu ma Naukhaur yi lekkone nagnema bu yagg souma deumé woul woone Yen ñeup souma len eupone alal di nguène ma faral Comme gars yi am ay milliards, milliards pour am ticket Safara Sama succès bou rèèn niggers wérenté nako daw Yen ñeup ken dou ame louko nekh ni ay waraté kat ci boîte Dama done djaap sama gars yeup faaté yèèneu texte yi Bayil ma diéma djaap text yeup faaté yèneu gars yi Niit yi xalaté touniou xel ndakh seug séni sex Motakh makk dou jog ci teudé rakkam ni Ci-Yénekaay yi Boy guél yeup leundeum dou foula nekh ngay toufli 25 ans baayil ma doundou comme si Papa nékatoufi Batay mane may wakh loutakh nièneu ñi di taf sen guémiñ Yaay sa dome dou wadd ni rongagnou ray kattou niit Morée Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi Sokhla wuma kèneu kumay temoigné fils Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi Idy namoul iPhone 6 ndakh ma ngi fi Sokhla wouma kèneu kumay temoigné fils