Dip Doundou Guiss

Ñetti At Ci Ren

Dip Doundou Guiss


Ñetti at ci ren
Tëju mënóo fippu
Fàq dem prison boo tànnal sa bopp tëju fi sa papa bañ
Mbëggéel capitainu borom nangu siiw du jàmmi kenn
Ba lépp di soppeeku ci sama dundu def na ñatti at ci ren
Tay ngay xam lu géej gi di riir, lu metti lu tiis
Dunu fàtte mukk ñi des ak ñi siif, liggéey guddi xiif
Dékku ibliis yee bu de du nu jig, dunu bidaanti di riche
Teg ci tàkk ni biddeew yi nu tiim, netti at ci rene
Ndeke suba gën a mat a sóor du añ du reer

Ñetti at ci ren
Jéem nañ ma fi ray ni xaj bu dee
Reyndi xàttit fes tëdd feebar
Jàng naa lu ne jeng naa fi
Mais duma mës a daanu never

Can you see what's going on
Turn the lights for me
And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeah yeah
Can you see what's going on
Turn the lights for me
And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeah yeah

Ñetti at ci ren
Ñi bëgg a xam ñépp agsileen
Sama gàccce lañ bëgoon gis teguñu ko bët ni ab sirene
Yar sama bopp ndax njub du dereet du ci sax ci man
Li gënoon jafe nekkul di liggéey mais liggéey sax ci men
Ñatti at music bi laago
Dan koy changer at yi ñëw ñédd temps bukki laa boot
Tax nga dégg xaj yi di mbow
Ñat at town bi dëgër këcc
Doo gis nit fu muy tëdde
Dip son bi mënul woon ñàkk comme galañ fu ñuy tëgge
Kaay ma wax lu waral booy yi
Fippu utali gaal yi
Dem géej sànni mbaal yi
Daj coono bu nekk pour dégg jaali
Gën a takk dàll yi
Koo ci laaj rêvam Farãs walla Itaali
Espoir réer ni Jaari
Ñoo ngi xaar Nguur gi ci taatu ndaa li
Maa ngi dox di dem ci yoonu God, ibliis di may xëcc
Humeurs yi du changer damay bég yenn saa yi ma yeewu def këj
Dara a ma yéematul gis naa fi xar-kanam gu nekk
Nooflaay du am bam bëgg ko, ci coono lañ nu binde nun

Ñetti at ci ren mère mësul tàyyi ci di may muñal
Su ñèpp xàddi woon du paf ma war ko delloo njukkal
Sabablou jaamu Yàlla ci jaami Yàlla yi bul jàmbu Yàlla
Nekk nit, nitee ko gën
Nit mënul weesu jaamu Yàlla, Yeah!

Can you see what's going on
Turn the lights for me
And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeah yeah
Can you see what's going on
Turn the lights for me
And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeah yeah

Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah