Yeah-yeah Yeah-yeah Bët du xool ba xam lu xel di gis Ma gëm say wax ba fàtte xool sa jikko Mën ko faj waaye dam la bàyyi ci biir Ëllëg du añ te mat na fàttaliku Ho, homie, homie, homie, homie Bët du xool ba xam lu xel di gis Ma gëm say wax ba fàtte xool sa jikko Mën ko faj waaye dam la bàyyi ci biir Ëllëg du añ te mat na fàttaliku Ho, homie, homie, homie, homie Depuis temps xale la ma gëj dal Mbëggeel dëggu ni yaay bàmmeel ak ay mbugalam Dëju mawti ngay xam ne dee moo gën a dëggu xol Xarit dëmm la chaque année ma koy gën a gëm Ndax mbëggeel du jaay divorce du fay dot Njëkk a jooy miraas ba noppi xew dëj Lii jikko jaan la feesal dell ci jëmmu xaj Li ko taal batey mu yegg lay njëkk fay Pexe noon du contre yaw pour yaw la nigga Kenn mënut a gaaw ci tijji xel ni paaka ci xol Xam sa bopp bu doon école kenn a du fa passer diplôme Tuxal dëkk a gën a yomb nit ki changer jikkoom Bu doon ku baax du daj lu bon yónnent du doon jirim Nelaw ci bàmmeel rekk a yàgg te amul lal ci biir Wor nga ma ma nigga bàyyiwuma la dam la ba ci biir Yaa ma woon ne man naa dëkk si pax ak ay jaan ci biir Bët du xool ba xam lu xel di gis Ma gëm say wax ba fàtte xool sa jikko Mën ko faj waaye dam la bàyyi ci biir Ëllëg du añ te mat na fàttaliku, ho Homie, homie, homie, homie Homie, homie, homie, homie Homie, homie, homie, homie Fàww ngay loru yenn saay pour man yegg fenn fi Ku wann lor buy jur ci mettit lay wësin Boo bëggee jege sa jàmm fàww nga sori ñenn ñi Xarit bu jege gën a jekku énnemie Dëgg nattukaay jëf du changer melo comme nun Du sutura rekk jëf lu bon a tax nit njëkk a nëbbu Lu tax nit gën te fekk mala yee nu gën a dëggu Ndax ci jikko juda moo ëpp sët Jesus ci kaw suuf Noon bi lay ŋàññ gën sa waa ji lay jay Noon biy tax ngay ñafe moo gën ñi lay wër di lay fen Jarul topp nitu intérêt àdduna ay àjjanaam Ñi di dagg sa xol yaa tax seen paaka ñaw Do my story sometimes, do my story sometimes Do my sto peace of mind Do my sto do my sto Do my story sometimes Do my story peace of mind, do my story peace of mind Do my sto do my sto Homie, homie, homie, homie