Suma reeni xol mi de yidde ma Su ma la amul woon defar naa la Sunu diggante lépp ma ci neex Ni ma la bëgg ni de ëpp na Sama reeni xol mi de yidde ma Ni ma la amul woon defar naa la Sunu diggante lépp ma ci neex Ni ma la bëgg My baby yaw, sama xol bi yaa ci ne (yeah yeah) Teye la, su ma la bàyyee bàyyi lu neex (yeah yeah) May janneer sa tàkkander di ma gunge (yeah yeah) Xamal la ci sa jëmm ji laay dunde, baby Fekk ma ci naj Jel yobbu ma ci kër gi Su ma la nàmmee Jaxam gis la ci weer wi Dama bëgg fi ci àdduna Ñu dund aljanna Sunu sëy bi daggan na Yobbu ma fu la neex Yah yeah, di diggu laal ba Suma reeni xol mi de yidde ma Su ma la amul woon defar naa la Sunu diggante lépp ma ci neex Ni ma la bëgg ni de ëpp na Sama reeni xol mi de yidde ma Ni ma la amul woon defar naa la Sunu diggante lépp ma ci neex Ni ma la bëgg T’es ma lover (baby, baby, baby) My lover (baby, baby, baby) My lover (baby, baby, baby) Sama lover (baby, baby, baby) Suma reeni xol mi de yidde ma Àdduna du neex ba ma gis ku mel ni yaw Yaay sama baby love, sama gidelam Yoon bi gudd bae sans yaw duma ñibbi, non Mak yaw li ñu boole moo ñu mën Même sunu boole ñoo koy ëpp doole Baby mi de yidde ma Baby you already know Fanaan sans yaw daf may tëredi lool Yeah, yeah Lu ma la jox nga may delloo Mbëggeel du jay ba ma lay jënde Ñëwal ñu togg, ñëwal ñu pello Loo bëgg dam koy def Yaay sama wéeruwaay Fecc dëgin ndaat saay pour sa xol bi nat Baby, sama aljanna Tax nga bàyyi yaay baay, dëkk sunu life Baby! Suma reeni xol mi de yidde ma Su ma la amul woon defar naa la Sunu diggante lépp ma ci neex Ni ma la bëgg ni de ëpp na Sama reeni xol mi de yidde ma Ni ma la amul woon defar naa la Sunu diggante lépp ma ci neex Ni ma la bëgg Sama mbëggeel dëgg la Wat na ni bëgg naa la Soo tëddee nelawal Dama la love, sama lover Baby, baby, baby (my lover) Baby, baby, baby (my lover) Baby, baby, baby (sama lover) Baby, baby, baby (my lover)